1 Timothy 5:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bul gëdd mag, waaye waxtaanal ak moom ni sa baay. Ndaw it, nga digal ko ni sa rakk,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bul gëdd mag, waaye ñaax ko ni bu doon sa baay. Ndaw it, def ko ni sa rakk.