1 Timothy 5:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye bul bind jigéen ju ndaw, ndaxte bu ko ay bëgg-bëggam xiiree ci sore Kirist, dina bëgg a séyaat,
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Jëtun ñiy ndaw nag, génne leen ci, ndax bu leen bëgg-bëggu bakkan sorelee ak Almasi, dinañu namma séyaat,