1 Timothy 5:13 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te du yem ci bëgg a séyaat rekk, waaye ku tayel lay doon; di ku wër kër ak kër, rax-ca-dolli réy làmmiñ te deñ kumpa, di wax lu yoonam nekkul.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te itam ca lañuy tàmme am ug jot, di taxawaalu kër ak kër. Te duñu yem ci am ag jot rekk, waaye dañuy làmmiñu, di dugg lu seen yoon nekkul, tey wax lu leen warul.