1 Timothy 5:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Li jëm ci njiiti mbooloo mi nag, joxal teraanga ju mat sëkk ñi ciy rafetal seen liggéey, rawatina ñi sax dàkk ci waare bi ak njàngale mi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mag ñiy jiite mbooloo mi bu baax nag, nañu leen yellale ag njukkal ñaari yoon, rawatina ñi boole coonoy waare ak njàngle.