1 Timothy 5:22 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bul gaaw a teg loxo kenn, ba fal ko, di séddu noonu ci bàkkaari jaambur, waaye dëkkal cig sell.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bul di gaawa teg loxo kenn, ngir fal ko njiit. Bul séddu ci bàkkaari jaambur, te yaw ci sa bopp, sàmmool dundin wu set.