bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Timothy 5:24
1 Timothy 5:24 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Am na, ñu seeni bàkkaar fés ci kanamu ñépp, ba jiitu leen ca àtte ba; ñi seeni bàkkaar nëbbu nag, bés baa ngi leen di xaar.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñenn a ngi ñu seeni bàkkaar fés, te àtteesagu leen, waaye ñenn a ngi ñu seeni bàkkaar làqu ba tax yoon dabagu leen.