bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Timothy 6:15
1 Timothy 6:15 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Moom kenn mooy Boroom bu tedd, di Buuru buur yi ak Kilifag kilifa yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
te ki koy feeñal bu àppam jotee, di ku Tedd ki wéetoo nguuram, Buuru buur yi, Sangu sang yi.