1 Timothy 6:16 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Moom kenn a jagoo dund gu sax, dëkk ci biir leer gu kenn mënta jege; moom mi nit musul a gis te nit mënu koo gis. Moom kenn a yelloo teraanga ak màggaay ba fàww. Amiin.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moom doŋŋ moo dul dee, moo màkkaanoo leer gu kenn jotewul, te mooy ki nit masula gis te tële koo gis. Teddnga ak kàttan ñeel na ko ba fàww. Amiin.