1 Timothy 6:19 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
di fàggu dencu ëllëg bu wér. Noonu dinañu feddali seen téye ci dund gu wóor gi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu lañuy dajalee alal, muy cëslaay lu dëgër ngir ëllëg, ndax ñu jot ci dund giy dëgg.