bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 1 Timothy 6:21
1 Timothy 6:21 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Am na ñu topp xam-xam boobu, waaye moy nañu ci yoonu ngëm. Na yiwu Yàlla ànd ak yéen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Boobu xam-xam la ñenn ñi topp ba lajj yoonu ngëm. Aw yiw ñeel na leen.