1 Timothy 6:4 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
kooku boroom tiitar la, bu xamul dara. Dafa wéradi, ba sóobu ci gëstuy neen ak i werante ciy araf yu dul jur lu dul ñeetaange, xuloo, xaste, ñaaw njort
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
kooku, ab xogglilukat la te xamul dara. Woppi werante ak xuloo ci baati kese, moo ko dal, te loolu mooy jur ñeetaane, ak ŋaayoo, aki saaga, ak ñaaw njort,