2 Corinthians 1:13 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Bindunu leen nag leneen lu dul li ngeen jàng te xam ko. Fi mu ne seen xam-xam ci nun matagul, waaye yaakaar naa ne, bu matee, dingeen man a tiitaru ci nun, ni nu koy defe ci yéen, bu bésu Boroom bi Yeesu ñëwee.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bindunu leen leneen lu moy mbind moomu ngeen jàng te man koo xam. May yaakaar nag ne dingeen xam ba mokkal,