2 Corinthians 1:17 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ba may mébét loolu nag, ndax dama cee boolewul pasteef? Te ndax samay yéene yéeney nit kese la, ba may xel ñaar, naan «waaw» ak «déet?»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax ñàkk pastéef laa mébéte moomu mébét? Am ni nitu suuxu neen di mébéte rekk laa topp bay xel-yaar, naan «waaw» te naan «déet»?