2 Corinthians 1:19 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ndaxte Doomu Yàlla ji, Yeesu Kirist, mi nu doon yégle ci seen biir, man ak Silwan ak Timote, nekkul woon «waaw» ak «déedéet;» «waawi» Yàlla la mas a nekk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ndax Doomu Yàlla, Yeesu Almasi, mi nu biral ci seen biir, man ak Silas ak Timote, du kàddug «waaw, déet;» «waaw» doŋŋ a nekk ci moom.