2 Corinthians 1:20 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te lépp lu Yàlla dige woon fekk na «waawam» ci moom. Noonu kon ci Kirist lanuy waxe: «Amiin,» ngir yékkati ndamu Yàlla.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ak li digey Yàlla di bare lépp, ci Almasi la ay digeem di doone «waaw». Moo tax itam, ci moom lanu naan Yàlla: «Amiin», ngir delloo ko njukkal.