2 Corinthians 1:4 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Mooy dëfël sunu xol ci sunu tiis yépp, ngir nun ci sunu bopp nu man a dëfël xolu ñépp ñi nekk ci tiis, di leen sédd ci noflaay, bi Yàlla def ci sunu xol.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
moom mi nuy dëfal ci sunu jépp njàqare, ngir noonu nu jote nun ci sunu bopp, ndëfalaay lu nu dëfaloo fa Yàlla, nu man koo dëfale ñi nekke mboolem xeeti njàqare.