2 Corinthians 1:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su nuy jaar ci tiis, seen noflaay a tax ak seen mucc. Bu dee Yàlla dëfël na sunu xol, seen noflaay a tax, ngir ngeen man a dékku naqar yu mel ni yu nuy am, nun itam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su nu jaaree ci njàqare, seen ndëfalaay ak seen jàmm lay doon. Sunu amee ndëfalaay it, seen ndëfalaay lay doon, ngir coono yi nuy dékku, ngeen man koo dékku, yeen itam.