2 Corinthians 1:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Te sunu yaakaar ci seen mbir dëgër na, xam ne, ni ngeen bokke ak nun naqar, noonu ngeen di bokke ak nun noflaayu xol.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te itam am nanu yaakaar ci yeen bu baax. Xam nanu ne ni ngeen bokke ak nun coono, ni ngeen di bokke ak nun ndëfalaay.