2 Corinthians 1:9 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Demoon nanu ba defe ne, dogalees na sunug dee. Loolu amoon na, ngir nu bañ a wéer sunu yaakaar ci sunu bopp, waaye nu wéer ko ci Yàlla, miy dekkal néew yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Nun ci sunu wàllu bopp, jàppoon nanu ne sunu àtteb dee moo taxaw. Waaye loolu tax na nu bañatee yaakaar sunu bopp, xanaa di yaakaar ci Yàlla, miy dekkal ñi dee.