2 Corinthians 10:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ci lu jëm ci samay mbir nag, maa ngi leen di ñaan — man Pool, mi ñu ne, ci seen biir «ragal» laa, bu ma leen soree, «ñeme,» — maa ngi leen di ñaan ndax woyof ak lewetaayu Kirist, ngir bu ma ñëwee, ma bañ a ànd ak ñeme gi may dencal ñenn ñiy xalaat ne, gis-gisu nit lanu topp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Man Póol ci sama wàllu bopp nag, maa leen di ñaaxe teeyug Almasi, akug lewetaayam, man miy teew ci seen biir, di ab ragaleey, fi seen kanam, te bu ma soree doŋŋ laa leen di ñemeey,