2 Corinthians 10:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu sunu sas agsiwul woon ba ci yéen, kon man nanoo ne, génn nanu sas wi nu Yàlla sas. Waaye agsi na ba ci yéen, te indil nanu leen xebaar bu baax bi jëm ci Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Moo tax weesunu sunu kemu sas, mbete agsiwunu woon ba ci yeen. Waaye noo agsi ba ci yeen, indil leen xibaaru jàmm bu Almasi.