2 Corinthians 10:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ak bépp tiitar buy jànkoonteek xam-xamu Yàlla, te danuy noot bépp xalaat, ba mu déggal Kirist.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
mook lépp luy réy-réyloo ab taxawaayam, di joŋante ak xam-xamu Yàlla, te nooy jàpp njaam bépp xalaat, ngir déggal-loo ko Almasi.