2 Corinthians 10:7 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xool-leen mbir mi ne fàŋŋ. Bu amee ku mu wóor ne, ci Kirist la bokk, na jàpp it ne, su bokkee ci Kirist, nun itam ci Kirist lanu bokk.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa ci melow biti doŋŋ ngeen di xool! Su amee ku mu wér péŋŋ, moom ci boppam ne ci Almasi la bokk, na dellu jàpp moom ci boppam, ne ndegam ci Almasi la bokk, nun itam, ci Almasi lanu bokk.