2 Corinthians 11:12 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Noonu may doxale nag dinaa ci sax, ngir ñiy damu, di wut yoon wu ñu aw ba yemale seen bopp ak nun, duñu ko am.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu may def rekk laay saxoo, ngir xañ aw lay, ñiy wut aw lay wu ñu damoo, naan ñook nun a yem kepp daraja.