2 Corinthians 11:15 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Kon nag ay ndawam mbubboo ndawi njub, loolu du nu jaaxal. Dees na leen fey seeni jëf.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon bu ay ndawam itam di mbubboo ndawi njub, du doon lu yéeme. Waaye seenug muj, seeni jëf lay yemool.