bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Corinthians 11:16
2 Corinthians 11:16 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Maa ngi leen koy waxaat: bu ma kenn jàpp nib dof. Walla boog bu ngeen ma ko jàppee, séddleen ma céru dof, ngir ma damu tuuti, man itam.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma baamu ko, bu ma kenn jàppe ab dof, mbaa boog, ngeen muñal ma ni ñuy muñale ab dof, ba ma damu tuuti, man itam.