2 Corinthians 11:17 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Loolu may wax nag, waxuma ko ci turu Boroom bi. Bu ma ñemee damoo nii, maa ngi wax ni dof.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Li may wax nag, waxewuma ko ci ndigalal Boroom bi, waaye taxawaayu dof laa koy waxe, gannaaw mbirum damu la.