2 Corinthians 11:2 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Dama leen di fiire ak fiiraange gu jóge ca Yàlla, ndaxte dama leen a bëgg a jébbal jenn jëkkër kepp, muy Kirist, ngeen set ni janq.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa leen di fiiree fiiraangey Yàlla ci boppam, ndax jenn jëkkër doŋŋ laa leen digool ab séy, te mooy Almasi mi ma leen namma jébbal, te fekk leen di janq bu set wecc.