2 Corinthians 11:21 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Sunu néew doole mayu nu, nu dem ba jëfe noonu; rus naa ci lool de! Ma wax waxi dof; moona lépp lu waay ñemee damoo, ñeme naa ko, man it.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ma waxe ko gàcce, mbete noo néew doole, ba manunoo jëfe ak yeen noonu! Ndaxam, ma wax waxi dof, lu waay ñemee damoo, ñeme naa koo damoo, man it.