2 Corinthians 11:23 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ndax surgay Kirist lañu? --maa ngi wax waxi ku tàggoo ak sagoom nag — maa leen ko gën a doon. Bu dee ci liggéey, maa leen ci man. Bu dee ci li ñu nu tëj ci kaso, maa leen ko gën a miin. Bu dee ci li ñu nu dóor ay yar, maa leen ëpple. Leru naa dee ba tàyyi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xanaa ay surgay Almasi lañu? Naa ràkkaaju nag, te ne maa leen ko gëna doon. Bu dee ci liggéey yu metti, maa man fopp; bu dee ci fani kaso, maa ëpple fopp; bu dee ci ay yar, maa ëpple ay yooni yoon, te bare na lu ma riisu ndee, ba raw leen: