2 Corinthians 11:25 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñetti yoon dóorees na ma ay yet, te mas nañu maa sànni ay xeer, bëgg maa rey. Ñetti yoon dugg naa gaal, mu suux. Mas naa yendu ci ndox, fanaan ci.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñetti yoon lañu ma dóori yet, dóor may doj benn yoon. Ñetti yoon laa dugg gaal, mu suux. Fanaan naa, yendu naa biir xóotey géej.