bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Corinthians 11:32
2 Corinthians 11:32 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ba ma nekkee dëkku Damas, boroom dëkk ba, di jawriñu buur ba Aretas, dafa santaane woon ñuy wottu dëkk ba, ngir man maa jàpp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ma nekkee Damaas, ga boroom dëkk ba di jawriñu Buur Aretas, boroom dëkk baa santaane ñu wattu buntu dëkk ba, ngir jàpp ma.