2 Corinthians 11:33 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Waaye dugalees na ma ci dàmba, jaarale ma ci palenteeru miiri dëkk ba, yoor ma ci suuf. Noonu ma rëcc ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye ca palanteeru tatay dëkk ba lañu ma yoore cig dàmba, ba ci suuf. Noonu laa ko rëcce.