2 Corinthians 11:7 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Walla boog ndax dama leen a tooñ ci li ma suufeel sama bopp ngir yékkati leen, ba ma leen di yégal xebaar bu baax bi te laajuma leen genn pey?
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Am boog damaa tooñ ca na ma toroxloo ngir darajaal leen, ndax la ma leen laajul ag pey, ba ma leen di àgge xibaaru jàmm bu Yàlla bi?