2 Corinthians 11:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xanaa kay damaa tooñ ci li ma dunde alalu yeneen mboolooy ñi gëm, ba futti leen, ngir dimbali leen, yéen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeneen mboolooy gëmkat de laa jëlal, nde maa nangoo ag peyoor ca ñoom, ba man leena liggéeyal, yeen, ci neen.