2 Corinthians 12:14 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Maa ngi leen di waaj a ganesi ñetteel bi yoon, te duma wéeru ci yéen. Wutsiwuma seen alal, yéen laa soxla. Ndaxte du gune moo war a yor waajuram, waaye waajur moo war a yor gune yi.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa ngii di leen waaja ganesi ñetteel bi yoon, te duma wéeru ci yeen. Wutsiwuma lu ngeen am, yeen laa soxla. Ndaxte doom du dencal waajuram, waaye waajur mooy dencal doom.