2 Corinthians 12:3 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Xam naa ne, nit kooku yékkati nañu ko ba fa Yàlla nekk. Bu dee ci jëmmam mbaa ci xelam, xawma; Yàllaa xam. Mu dégg fa baat yu ñu mënul a nettali te yu ñu mayul doom Aadama, mu ŋaaŋ ko.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xam naa ne nit kooku, ndegam yaramam lees ko booleel, am booleesu ko ak yaramam? Xawma, Yàlla rekk a xam,