2 Corinthians 12:6 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Su ma bëggoon a damu, du doon yëfi dof, ndaxte dëgg laay wax. Waaye damay moytoo damu, ngir kenn bañ a foog ci man lu weesu li mu gis, may def, te muy dégg, ma di ko wax.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Su ma nammoona damu it, du doon ag ndof, ndax dëgg laay wax. Waaye damay moytoo damu, ngir kenn bañ maa fooge lu wees li mu gis, may def, ak li mu dégg, may wax.