2 Corinthians 12:7 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Te it ngir ma bañ a yég sama bopp ndax peeñu yooyu wees xel, mayees na mbir dal ma ci sama yaram, di ma metital ni dég, muy malaakam Seytaane mu may sonal, ngir ma bañ a yég sama bopp.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Te it, waccalees na ma ndégu biir suux, mu taxawe ndawal Seytaane, di ma mitital, ngir ma baña bew ndax peeñu yu yéeme.