2 Corinthians 12:8 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Ñaan naa Boroom bi ñetti yoon ci mbir moomu, ngir mu taqale ma ak moom.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mbir moomu, ñetti yoon laa ci ñaan Sang bi, ngir mu sorele maak moom.