2 Corinthians 13:1 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bii mooy ñetteel bi yoon, ma di leen ganesi. «Bépp àtte dina aju ci seedes ñaar walla ñetti nit.»
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñetteel bi yoon a ngii, bu ma leen di ganesi. «Ci kàddug ñaari seede ba ñett nag la àtteb mépp mbir di wére.»