2 Corinthians 13:2 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Li ma waxoon ci sama ñaareelu ngan, ci ñi bàkkaaroon bu yàgg ak ñi ci des, maa ngi koy waxaat léegi, bala maa dikkaat: su ma dellusee, duma yërëm kenn.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
La ma waxoon ba noppi ca sama ñaareelu ngan, tey bi ma wuutee, moom laay baamtu, artoo ko ñi jëkkoona bàkkaar, ak ñi ci des ñépp: su ma délsee, duma ñéeblu kenn,