2 Corinthians 13:3 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Bu fekkee ne dangeen a bëgg firnde juy wone ne, Kirist mooy wax jaarale ko ci man, dingeen ko am. Digganteem ak yéen du ànd ak néew doole, waaye dafay feeñal kàttan ci seen biir.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
gannaaw yeenay wut lu firndeel ne ci man la Almasi di waxe ak yeen, te moom néewul kàttan, diggam ak yeen, waaye ku manoorewu la ci seen biir.