2 Corinthians 13:5 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
Xool-leen seen bopp bu baax, ba xam ndax ngëm a ngi ci yéen. Seetluleen seen bopp. Xanaa xamuleen ne, Yeesoo ngi ci yéen? Walla boog ngeen gis ne, ay naaféq ngeen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Xoolaatleen seen bopp, ba xam ndax yeena ngi ci yoonu ngëm wi. Nattleen seen bopp, xanaa xam ngeen ne Yeesu Almasee ngi ci yeen? Ndegam du seen gëmadi, la natt ba firndeel!