2 Corinthians 13:7 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Nu ngi ñaan Yàlla, ngeen bañ a def dara lu bon. Waxuma ne danoo bëgg a wone noonu sunu firndeg ngëm, waaye sunu yéene mooy ngeen jëf lu baax, boo yaboo sax ñu jiiñ nu ag naaféq.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Teewul nuy ñaan Yàlla, ngeen baña def dara lu bon, te ñaanunu loolu am, ngir nu man koo firndeele sunu taxawaay, waaye bu sunub taxawaay doonul woon lu firndewu itam, sunu yéene mooy ngeen di def lu baax.