2 Corinthians 2:11 — Compare Translations

2 translations compared side by side

Wolof 1987
ngir Seytaane bañ a am bunt bu mu jaar ba nax nu, ndaxte réerewunu mbir ay pexeem.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
ngir Seytaane bañ noo nax, ndax ay pexeem, umplewunu ko.