bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare 2 Corinthians 2:12
2 Corinthians 2:12 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ba ma àggee Torowas nag, ngir yégle fa xebaar bu baax bi ci Kirist, Boroom bi ubbil na ma ci bunt.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ma àggee Torowas, ngir yégle fa xibaaru jàmm bi ci Almasi, bunt ubbikul na ma ndax Boroom bi.