2 Corinthians 2:14 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Waaye cant ñeel na Yàlla! Ci sunu booloo ak Kirist, daf nuy yóbbaale saa su nekk ci gawari ndamam, tey jaar ci nun ngir turu Kirist jolli fu nekk, ni xetu latkoloñ di tasaaroo.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye cant ñeel na Yàlla! Moom mi Almasi tax mu di nu yóbbaale saa su nekk, ci njaab miy fésal ndamam, te cuuraayal xam-xamam, nun ñii la koy wasaaree fépp,