2 Corinthians 2:3 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Looloo tax ma binde noonu, ngir bañ a agsi, am naqar ci ñi ma waroon a bégal. Am naa kóolute ci yéen ñépp ne, sama mbég mooy seen mbég.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Looloo taxoon ma binde noonu, ngir bu ma dikkee, baña am naqar ci ñi ma waroona bégal. Li ma wóor ci yeen ñépp moo di sama mbégte mooy seen mbégte, yeen ñépp.