2 Corinthians 2:4 — Compare Translations
2 translations compared side by side
Wolof 1987
Ci biir tiis ak xol bu jeex laa leen bind, samay bët taa ak ay rangooñ. Binduma leen ngir teg leen naqar, waaye ngir ngeen xam xóotaayu mbëggeel gi ma am ci yéen.
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci biir njàqare, ak xol bu fees, ak rongooñ yu bare laa leen bind. Binduma leen ngir naqaral leen, waaye cofeel gu réy gi ma am ci yeen moo tax.